1
00:04:35,234 --> 00:04:37,361
ab yuurnukat nga

2
00:04:40,823 --> 00:04:45,869
CiMDB ci ekipu tekkikatu chaine Telegram 
Dugalug, ŋàññi ak yebbi liggéey sinemaa àdduna

3
00:05:14,398 --> 00:05:16,358
...mënu nu

4
00:09:27,484 --> 00:09:29,486
Ndax tiital naa la?

5
00:09:29,569 --> 00:09:32,531
yenn-
Maa ngi jéggalu-

6
00:09:34,074 --> 00:09:36,994
gis naa sa sac 
Dama yaakaar ni danga wara nekk fi

7
00:09:38,161 --> 00:09:40,455
Madam, déglul ma

8
00:09:40,539 --> 00:09:43,083
...bul dem foofu 

9
00:09:43,166 --> 00:09:45,252
Lu tax

10
00:09:45,335 --> 00:09:48,130
Sama maam dafa daan wax bàmmeel bi
 Mooy dëkkuwaayu néew yi 

11
00:09:48,213 --> 00:09:52,467
Te ku dee dafa bëgg ñu bàyyi ko ci jàmm

12
00:09:54,678 --> 00:09:57,556
Soo amee lenn lu ngeen di def ak ñoom
Ñoom itam amu ñu dara ci yaw

13
00:09:58,598 --> 00:10:01,685
Jàppoon naa ni poliis yi duñu gëm lu jaaduwul

14
00:10:01,768 --> 00:10:06,023
... ci Amerique amaana
Waaye fii am nanu sunuy gëm-gëm

15
00:10:06,106 --> 00:10:08,859
am bis bu neex-
tàggoo-

16
00:10:48,690 --> 00:10:50,484
Martin, demal

17
00:11:04,581 --> 00:11:06,083
Amnaa ab xalaat

18
00:11:20,180 --> 00:11:22,349
Jërëjëf

19
00:11:36,822 --> 00:11:38,657
ñëwal

20
00:11:39,699 --> 00:11:43,912
Leegi mooy jamonoy rëbb kannaar
Amul benn njariñ ak nun

21
00:11:47,249 --> 00:11:49,543
Lii dafa daan nekk wagon yu def lekk

22
00:11:52,337 --> 00:11:54,423
Nanu ñëw... nanu dem ci yaw

23
00:11:56,925 --> 00:11:58,718
teel

24
00:12:04,891 --> 00:12:09,312
Baaxul, wala book? 
Boroom gaal gi moo ko jëndoon ci raay bi

25
00:12:09,396 --> 00:12:12,107
Defar na benn ci ñoom ngir mbëggeel ak bànneex

26
00:12:12,190 --> 00:12:14,734
Yenn saa mu am xale bu jigéen buy ñëw

27
00:12:17,195 --> 00:12:19,197
Stan, sama xol neexul

28
00:12:39,217 --> 00:12:43,597
Lu tax amul benn palanteer?
ndax impermeur-

29
00:12:43,680 --> 00:12:45,265
Waaye amna klimaa bi

30
00:12:46,141 --> 00:12:48,977
Ku amul lii, amul ngelaw ci biir

31
00:12:56,902 --> 00:13:01,948
Ku amul lii doo mëna génn
Melni danga nekk ci biir kofor

32
00:14:11,476 --> 00:14:13,687
Damn, fuse bi dafa jameet

33
00:14:15,188 --> 00:14:18,942
Stan, dama ragal ma-
Maureen, looy ragal?

34
00:14:19,025 --> 00:14:22,737
Nun ñaar rek la fi nekk
Ak dama wara genni benn simili

35
00:14:26,825 --> 00:14:28,994
Kontër bi mingi ci biti

36
00:14:34,791 --> 00:14:37,460
Ndax jël nga caabi gi?
déet-

37
00:14:41,423 --> 00:14:44,301
Bàyyi naa ko fii, gëm naani
Mu réer

38
00:14:44,384 --> 00:14:47,637
Fan lay mëna nekk 
Dimbali ma gis ko, Maureen

39
00:14:48,471 --> 00:14:50,932
Aar bi amul benn sikk bi nuy yegsi

40
00:14:53,393 --> 00:14:57,939
Klimaa bi doxul. Air bi dafay sonn
Mënu ma noyyi, Stan

41
00:15:03,361 --> 00:15:07,198
...buntu bu alku bi
Amul nuñu ko mëna ubbee

42
00:15:07,282 --> 00:15:11,077
Stan... xoolal

43
00:15:16,374 --> 00:15:19,336
Fiil kuuraŋ bu bawoo ci tuyo plastik yooyu 
weesuna loolu dafay tekki ni dafa taxaw leegi

44
00:15:30,722 --> 00:15:32,599
ñëwal

45
00:15:55,789 --> 00:15:58,917
Amaana Maureen yewwu na
Xaaral ma xoolaat 

46
00:17:34,387 --> 00:17:37,015
Xarit lanu woon

47
00:17:37,974 --> 00:17:39,893
Wax ma fan nga nekk

48
00:17:40,935 --> 00:17:43,021
wax ma 

49
00:17:43,938 --> 00:17:46,858
Fan nga tontu

50
00:17:53,698 --> 00:17:56,910
Nanga tontu

51
00:18:44,582 --> 00:18:46,000
saw 

52
00:18:48,253 --> 00:18:50,129
Yaay kilifa gi 

53
00:18:52,131 --> 00:18:54,050
Yaay kilifa

54
00:18:59,097 --> 00:19:00,807
saw

55
00:19:02,767 --> 00:19:04,519
waaw

56
00:19:56,446 --> 00:20:01,618
Mënu nu ko gis. Guddi gi yépp nu ko doon wër. Stan itam amul benn xibaar

57
00:20:01,701 --> 00:20:04,078
Amaana bokk daw

58
00:20:04,162 --> 00:20:06,497
Yaakaar naa loolu, Lillian

59
00:20:06,581 --> 00:20:08,917
Nanu am yaakaar mu nekk ni nga wax

60
00:21:19,195 --> 00:21:21,531
Sëñ bi, fàww ma fay la amande

61
00:21:23,658 --> 00:21:26,035
Ndax nii ngay dalal say way wuyusi?

62
00:21:26,119 --> 00:21:29,622
Dédeet señ
Sudee seen gaawaay weesuna àpp bi

63
00:21:29,706 --> 00:21:31,749
Xamnaa loolu, señor

64
00:21:31,833 --> 00:21:33,876
Waaye ñu laaj ma 
Xaaral ma gaaw yegsi fii 

65
00:21:35,628 --> 00:21:37,255
Gorlie laa tudd

66
00:21:38,006 --> 00:21:40,091
Detektif Gourley bu Ecosse Yard
(Makaanu poliisu Angleterre)

67
00:21:40,174 --> 00:21:43,803
Dalal jàmm, señ 
Sunu biro mingi fee, ànd ak man

68
00:21:43,886 --> 00:21:46,514
Man maa laaj ndimbal, ci dëgg

69
00:21:47,974 --> 00:21:49,809
Ñaari xale yu góor réer nañu te kenn gisu leen.

70
00:21:49,892 --> 00:21:52,562
Danu bëgga leerlu ni
. Daw rek

71
00:21:52,645 --> 00:21:55,732
Beneen yoon
. Xeex ginaar, yaa ngi ñaan ndimbal

72
00:22:04,532 --> 00:22:06,367
Fotograf, kilifa

73
00:22:07,493 --> 00:22:09,412
Waaye nekkul fii

74
00:22:09,495 --> 00:22:13,041
Dafa joge Amerique ñëw fi 
ngir saytu sunu dëkk bu yàqu

75
00:22:14,042 --> 00:22:16,002
Dama leen bëgg

76
00:22:16,085 --> 00:22:19,505
ci yan Ruins?
Dédeet, xeetu xale bu jigéen bii-

77
00:22:20,256 --> 00:22:25,511
Leegi danga wara fay amande bi
Wala ma yónnee ko Scotland Yard?

78
00:22:29,891 --> 00:22:34,312
Weer yu bari a ngi nii may bàyyi xel ci moom
Waaye daanuwul ci fiir bi

79
00:22:34,395 --> 00:22:37,148
Bama ko jotee démb ci guddi

80
00:22:37,231 --> 00:22:40,651
te gëm naa ni 
Didi wax ak ku dee

81
00:22:43,446 --> 00:22:47,325
Dama doon sori ci moom
Waaye weer wi fees na 

82
00:22:47,408 --> 00:22:50,787
Maa ngi doon gis limu doon def

83
00:22:50,870 --> 00:22:54,665
Yàlla xam na boo màndi
Lu ngeen mënu gis?

84
00:22:56,417 --> 00:22:59,921
Gis naa ko, maa ngi waat. gis naa ko

85
00:23:06,594 --> 00:23:10,515
Amoon na benn aparey bumu def ci kaw bàmmeel bi . 

86
00:23:12,100 --> 00:23:14,227
Nga baal ma, ci kan ngay wax?

87
00:23:16,270 --> 00:23:18,022
Jàngalekat Miles

88
00:23:18,106 --> 00:23:23,277
Déglul, sunu xarit mingi fi
Mu naan ba dee

89
00:23:23,361 --> 00:23:25,530
Jàngalekat bi di Miles Divones

90
00:23:25,613 --> 00:23:27,532
Danga wara sori ci moom

91
00:23:29,784 --> 00:23:32,537
Er... samam la

92
00:23:34,413 --> 00:23:36,332
Leegi loo bëgg ci man?

93
00:23:37,542 --> 00:23:40,211
dara-
Gëmuma-

94
00:23:41,712 --> 00:23:44,006
Luko moy doo ko dagg

95
00:23:45,466 --> 00:23:48,594
Ndax bokkuleen ci fii?
déet-

96
00:23:51,264 --> 00:23:54,559
May xalaat lan ngay wax ci man 
Maa ngi lay wax ba leegi

97
00:23:55,476 --> 00:23:58,479
Dégg naa nga wax ak néew

98
00:23:58,563 --> 00:24:02,900
Maa ngi enregistre seeni baat
ba noppi ma dekode ko ak sama aparey

99
00:24:07,029 --> 00:24:10,032
Lu tax nga nekk ci kumpa? 
Lu nga ragal

100
00:24:10,116 --> 00:24:12,702
Ci dof ak soxor nit ñi 

101
00:24:12,785 --> 00:24:16,539
dof yi deñuy xalaat
. Maa ngi yàq bàmmeel yi

102
00:24:18,166 --> 00:24:20,918
Ñenn ñi dañu am doole yu ëpp doole

103
00:24:21,002 --> 00:24:23,171
lu weesu xalaatu nit 

104
00:24:23,254 --> 00:24:27,592
Mën-mën yu ba leegi
. Mënu nu leen noot

105
00:24:27,675 --> 00:24:31,095
Wala nu tànn baña bàyyi xel ci ñoom
Ndax danu leen di ragal

106
00:24:32,221 --> 00:24:34,599
Amnaa kàttan yooyu 

107
00:24:34,682 --> 00:24:37,185
te jàpp naa ni dama wara
. jëfandikoo leen

108
00:24:40,188 --> 00:24:43,191
Dee du njeextalu lépp

109
00:24:43,274 --> 00:24:46,819
Dundu gu bees la

110
00:24:46,903 --> 00:24:51,199
, ak ngir mëna wax ni mbir mi dëggu na 
Maa ngi am tegtal ci néew yi

111
00:24:52,992 --> 00:24:55,494
Lu nga nara def ëlëg?

112
00:24:55,578 --> 00:24:57,788
Xama guma

113
00:24:57,872 --> 00:25:00,833
Xamnaa dooley yëg-yëg ak yëg-yëg

114
00:25:00,917 --> 00:25:05,171
...liy tekki gis, dégg, xeeñ

115
00:25:06,881 --> 00:25:09,550
Waaye doyul ci man

116
00:25:11,093 --> 00:25:13,054
Dama bëgga dem fu gëna sori

117
00:25:15,139 --> 00:25:17,600
Saa yu nekk amna ay yam ak ay gaañ-gaañu

118
00:25:17,725 --> 00:25:20,019
Du dëgg

119
00:25:20,102 --> 00:25:23,481
Nun lanuy defar ak sunu dof
Danuy bloke

120
00:25:25,358 --> 00:25:27,693
Yaa ngi may tiital

121
00:25:27,777 --> 00:25:33,366
Xamnaa ni loolu doyna la ci man
Bul nangu dem

122
00:25:34,617 --> 00:25:39,330
Dédeet, dama ragal amul àpp 
Dunga sargal sa bopp

123
00:25:46,629 --> 00:25:49,215
Yaa ngi rafet, soxna si 

124
00:25:51,884 --> 00:25:56,264
Sa loxo yi dañu nooy te neex

125
00:25:56,389 --> 00:26:01,352
Bëtëm yi dañu leer ba noppi xóot

126
00:26:04,730 --> 00:26:08,442
Xoolal ma
Maa ngi lay digal nga xool ma

127
00:26:13,239 --> 00:26:15,616
Mënu nga dara

128
00:26:17,410 --> 00:26:21,122
Mën naa la wax nga def lépp

129
00:26:21,205 --> 00:26:25,918
Yaa ngi may déggal te doo sax xaar benn yoon

130
00:26:27,003 --> 00:26:30,381
Amul benn sañ-sañu tànn sa bopp

131
00:26:31,549 --> 00:26:35,094
Sama xel moo lay jiite

132
00:27:06,334 --> 00:27:08,669
Daf la song

133
00:27:08,753 --> 00:27:12,214
Du bis bu njëkk la 
Def nako bu njëkk

134
00:27:13,632 --> 00:27:15,926
Lu tax doo ko dàq? 

135
00:27:17,011 --> 00:27:19,221
Lii mooy sunu ëlëg

136
00:27:20,222 --> 00:27:23,059
Danu soxlaante

137
00:27:23,142 --> 00:27:25,728
Sunu bañeel bi nu bokk moo nu boole

138
00:27:26,479 --> 00:27:28,397
Xale bu soxor la

139
00:27:30,399 --> 00:27:32,318
Waaye muus rekk la

140
00:27:33,527 --> 00:27:38,616
Muus mu may ray ëlëg wala ëlëg

141
00:27:38,699 --> 00:27:41,410
Dinaa dee nii
Lii mooy sama ngërëm

142
00:28:00,721 --> 00:28:04,725
Dafa wara nekk kiliyaan bu baax- 
Saw-

143
00:33:45,733 --> 00:33:47,401
kuy

144
00:33:47,484 --> 00:33:50,195
Gurley
Dama wara waxtaan ak yaw

145
00:33:56,618 --> 00:33:59,580
suba bu baax 
Xamnaa ban waxtu la

146
00:33:59,663 --> 00:34:02,833
Suma soxlawul sa ndimbal
Duma la sonal

147
00:34:02,916 --> 00:34:06,170
Xamuma- 
...aksidaa dafa am-

148
00:34:06,253 --> 00:34:12,092
Am ku dee te daa melni yaw 
Yaw kese nga nekk fotograf ci dëkk bi

149
00:34:13,218 --> 00:34:15,846
Ci yenn nataal, balaa ñuy toxal néew bi
Dama soxla 

150
00:34:16,555 --> 00:34:18,640
kan ci wetu

151
00:34:25,189 --> 00:34:26,899
Leer nama ni dafa màndiwoon

152
00:34:29,193 --> 00:34:33,489
....slip bu ndaw 

153
00:34:33,572 --> 00:34:35,532
sànni ci suuf

154
00:34:35,616 --> 00:34:37,701
Mën nga dem leegi

155
00:34:43,749 --> 00:34:46,084
Inspektër Gurley?
Waaw?

156
00:34:46,168 --> 00:34:49,588
Ndax mën nanu ko nangu?
Saa yu noppee ci nataal yi-

157
00:34:50,547 --> 00:34:53,509
Wax nga amoo dara, wala ? 
Benn jabar rek la amoon- 

158
00:34:53,634 --> 00:34:57,805
.ni mu bàyyi ko ak beneen góor ba noppi dem

159
00:35:01,725 --> 00:35:04,186
Sunu bañeel bi nu bokk moo nu boole

160
00:35:05,604 --> 00:35:09,024
Dafa bëgga ray ma

161
00:35:28,210 --> 00:35:31,463
Fan nga nekk 
Fan nga nekk

162
00:35:32,756 --> 00:35:35,217
Fan nga nekk

163
00:35:49,231 --> 00:35:51,400
Mooy boppam 

164
00:36:23,557 --> 00:36:25,642
Lu tax nga ñëw fii 

165
00:36:27,644 --> 00:36:30,188
Danga wara jàppale ma 

166
00:36:30,272 --> 00:36:33,191
Yaw kese nga 
Mën nga gis Maureen 

167
00:36:33,275 --> 00:36:35,569
Dédeet, mënu ma ko

168
00:36:36,403 --> 00:36:41,283
Robert, mangi 

169
00:36:41,366 --> 00:36:44,578
Soo ko bëggee, dinaa ñëw dëkk ak yaw

170
00:36:44,661 --> 00:36:49,249
Amul benn yërmaande ci man
Mënoo dellu ginaaw 

171
00:37:00,135 --> 00:37:03,639
Ndax am nga lu sa doom ju jigéen moom?

172
00:37:15,067 --> 00:37:19,279
Reflexion...leer

173
00:37:21,156 --> 00:37:23,200
Dafay wal

174
00:37:23,867 --> 00:37:26,286
liquid, water

175
00:37:28,038 --> 00:37:29,581
green

176
00:37:31,333 --> 00:37:33,085
garab yi

177
00:37:38,298 --> 00:37:40,509
lëndëm gi 

178
00:37:42,844 --> 00:37:44,763
doomi kanaar

179
00:37:48,517 --> 00:37:51,019
Caabi gi, war nanu ko wut 

180
00:37:52,521 --> 00:37:54,773
Mënu ma noyyi 

181
00:37:59,736 --> 00:38:01,947
muur gaal

182
00:38:04,616 --> 00:38:07,035
Dimbali ma,

183
00:38:07,744 --> 00:38:10,163
...Yaay, mënu ma noyyi 

184
00:38:10,288 --> 00:38:12,207
...mënu ma

185
00:38:21,591 --> 00:38:23,802
Leegi xamnaa fumu nekk 

186
00:38:24,886 --> 00:38:26,930
I know where it is 

187
00:39:08,221 --> 00:39:13,060
Damay faral diko def fii 
Jàppoon naa ni sama sekkere la, waaye amna ku ko gis 

188
00:39:13,727 --> 00:39:16,396
Danu wara dindi buntu bi

189
00:39:17,189 --> 00:39:19,232
<i>Boat cover</i>

190
00:39:55,852 --> 00:39:58,396
Dagg kuuraŋ bi

191
00:40:03,485 --> 00:40:06,613
Waaw, moom la

192
00:40:06,696 --> 00:40:08,406
This is the key

193
00:40:37,561 --> 00:40:39,229
waaw

194
00:40:40,188 --> 00:40:42,899
Dinaa fa ñëw ci saasi 

195
00:40:45,902 --> 00:40:48,238
There was no air in it 

196
00:40:48,321 --> 00:40:51,867
Lu tax doo dindi buntu bi?
Ñu ngi ko defaree ni kofor-

197
00:40:51,950 --> 00:40:56,037
Nanga def, demal ci njeexitalu pier bi

198
00:40:56,121 --> 00:40:58,206
Bul nangu kenn dugg

199
00:40:58,290 --> 00:41:00,917
Jàngalekat Miles, jërëjëf ci sa ñëw

200
00:41:10,051 --> 00:41:12,345
Ndax mas ngaa gis barab bii?

201
00:41:12,429 --> 00:41:15,765
Waaw, waaw waaw 
gis naa ko bu njëkk, inspectër

202
00:41:15,849 --> 00:41:18,393
Waaye musu ma ñëw fii
Sudee loolu mooy li nga bëgga wax

203
00:41:18,518 --> 00:41:22,480
Waaw, waaw waaw
Dañu wax ni am nga doole ju ëpp

204
00:41:23,523 --> 00:41:26,401
Ndax yaa ngi may kaf, inspectër?

205
00:41:26,484 --> 00:41:29,487
...Xool, Jàngalekat Miles
Defa jafe lool ci poliis bi

206
00:41:29,571 --> 00:41:33,033
amal lànket ci lu jaarul yoon

207
00:41:33,116 --> 00:41:37,537
...maa ngi xalaat fii? wax ma
Yaakaar nga ni sama liggéey la woon?

208
00:41:39,206 --> 00:41:41,416
...ñu yaakaar ni

209
00:41:41,499 --> 00:41:46,087
Danga wara nekk lu ndaw 
nga mëna jaar ci néegu ventilation bi

210
00:41:49,841 --> 00:41:51,551
...Xamuma

211
00:41:51,635 --> 00:41:54,763
buñu sukkandikoo ci rapoor forensiik yi
Bunt bi dañu ko tëjoon ci biir

212
00:41:54,846 --> 00:42:01,102
Kon ñi ci loru ginaaw bi ñu daggee kuuraŋ bi
tëj seen bopp

213
00:42:02,646 --> 00:42:08,193
pax mi nekk ci biir garde bi, benn yoon kese mooy génn 
Lu wuute ak buntu bu mag bi

214
00:42:09,736 --> 00:42:11,446
Kon suicide?

215
00:42:12,781 --> 00:42:15,367
Waaw, lépp bëgg caabi gi nekk ci biir néeg bi

216
00:42:15,450 --> 00:42:17,911
Waaye nu fekk ko ci biti 

217
00:42:17,994 --> 00:42:21,831
Ci kaw muur gaal gi
Am ku ko def foofu 

218
00:42:22,707 --> 00:42:24,417
kañ

219
00:46:41,674 --> 00:46:45,178
Nanga def, waaw? 
naka nga ko mënee?

220
00:46:46,971 --> 00:46:49,140
...Jill, waaw 
...waawaw maa ngi fàttaliku 

221
00:46:51,726 --> 00:46:53,603
ban nataal

222
00:46:55,230 --> 00:46:58,483
Yes, sure 
Saa yoo bëggee 

223
00:46:58,566 --> 00:47:01,110
.Waawaw...ba leegi

224
00:47:01,194 --> 00:47:04,155
Ñëwal, dinaa la xaar 
I'm not going anywhere 

225
00:47:11,538 --> 00:47:13,957
Teori la ci yaw

226
00:47:14,707 --> 00:47:17,961
Loolu wóorna ci man

227
00:47:19,879 --> 00:47:22,423
Waaye sunu waxee ni liggéeyu muus la
Dañu nuy reetaan

228
00:47:22,549 --> 00:47:25,635
Loolu mooy seen ëlëgu ñi xam

229
00:47:25,718 --> 00:47:28,888
Ray na itam jëkkër ak jabar yu ndaw yi

230
00:47:30,765 --> 00:47:32,559
Yaakaar nga Maureen ak Stan?

231
00:47:32,642 --> 00:47:38,147
Waaw, ñu génne caabi gi ci ventilation bi 

232
00:47:39,607 --> 00:47:41,985
Lii ab dof la

233
00:47:42,735 --> 00:47:47,740
Soo bëggee def lu mel nii, danga wara mën xalaat 
Mën-mën bu nit rek mëna am

234
00:47:47,824 --> 00:47:51,202
Dañu weñ benn góor ci bant 

235
00:47:51,327 --> 00:47:54,080
Te noo ngi wax ci muus 

236
00:47:55,456 --> 00:47:57,834
Li nga wax mënul am dara

237
00:47:57,917 --> 00:48:00,169
... yaw la woon

238
00:48:03,006 --> 00:48:05,425
Yaay indi nataal yii 

239
00:54:16,671 --> 00:54:19,799
Ñatti màndarga yu nuróo ci ñatti fan yii weesu

240
00:54:20,883 --> 00:54:23,469
Te ba leegi bëgg nga ko baña bàyyi xel 

241
00:54:23,552 --> 00:54:25,304
Loolu doywaar la

242
00:54:25,388 --> 00:54:29,558
... Ñaari xale yu góor ak dee guñu ñaaw xel ak jaar-jaaru caabi gi

243
00:54:29,642 --> 00:54:33,646
..Ferguson màndi daanu ci kaw scaffold bi

244
00:54:34,855 --> 00:54:38,484
Leegi yaayu Maureen
... ci palantu kër giy tàkk 

245
00:54:38,567 --> 00:54:40,736
Fatte nga kilifa gi 

246
00:54:40,820 --> 00:54:43,364
Foreman bi? kuy

247
00:54:43,447 --> 00:54:47,493
Balaa ngay ñëw, dafa def aksidaa
Defa duggu ci biir benn van

248
00:54:47,576 --> 00:54:49,662
Suba boobu amul woon benn lay 

249
00:54:50,871 --> 00:54:53,207
...jafe-jafe yiy faral di am
Ndax du lu yéeme ?

250
00:55:31,996 --> 00:55:33,914
Kart bi baaxoon na

251
00:55:34,582 --> 00:55:36,375
Ngir amateur 

252
00:55:37,376 --> 00:55:39,336
Yaa ngi juum, inspectër 

253
00:55:39,420 --> 00:55:42,548
Man fotograf bu mag laa ci Amerique 

254
00:55:42,631 --> 00:55:46,677
Xamnaa loolu waaye jaar-jaaru nataal 
Ndax am ngeen néew yi?

255
00:55:46,761 --> 00:55:50,097
...du dëgg 
Lii mooy sama jaar-jaar bu njëkk

256
00:55:51,891 --> 00:55:56,353
Xeetu garabu forensiik, ay leeral yu bees 
ci deewu jëkkër ak jabar yu ndaw

257
00:56:07,239 --> 00:56:09,533
lu

258
00:56:09,658 --> 00:56:13,662
Catair, inspektër Gurley
Kawar muus bu ñuul 

259
00:56:17,124 --> 00:56:21,504
Gis kawar ci kanalu ventilation bi? 
waaw, ndànk-

260
00:56:24,882 --> 00:56:26,967
naka nga ko xamee ?

261
00:56:28,260 --> 00:56:30,221
Melokaan!

262
00:56:38,312 --> 00:56:40,481
...dafa doy waar 

263
00:56:42,650 --> 00:56:45,277
Amaana ñàkk naa leen 

264
00:56:45,402 --> 00:56:48,405
Ndax dégg nga lu doy waar ci guddi gi?

265
00:56:48,489 --> 00:56:51,617
Sonu yuuxu waa ju amul wërsëg mi doon daanu-
Loolu rekk la?

266
00:56:51,700 --> 00:56:53,244
doyul

267
00:56:53,327 --> 00:56:56,413
Maanaam, xeex... xuloo?

268
00:56:56,497 --> 00:56:58,999
Xeex ak kan? muus? 

269
00:56:59,083 --> 00:57:01,377
Kenn du fi ñëw ci guddi 

270
00:57:01,460 --> 00:57:04,922
Man ak Violeta ak yeneen muus yu néew 

271
00:57:06,382 --> 00:57:09,135
Yeneen muus- 
Sama xarit?

272
00:57:09,218 --> 00:57:10,928
dara... dara 

273
00:57:11,011 --> 00:57:14,181
Noo ngi leen di sant bu baax, ak ndigal-
tàggoo-

274
00:57:39,582 --> 00:57:42,042
Did I bother you?
were you sleeping

275
00:57:42,126 --> 00:57:46,297
No, not yet
come inside 

276
00:57:49,508 --> 00:57:51,385
what happened

277
00:57:52,720 --> 00:57:55,389
Yekkatooloo ma 
Ndax gis nga sama kanam gu kontaan gi?

278
00:57:55,472 --> 00:57:58,058
Is it a very bad idea?

279
00:57:58,142 --> 00:58:00,269
Déedet, waaye amnaa kaayaar ni dina gëna baax 

280
00:58:00,352 --> 00:58:02,438
Xamuma ndax moo gën wala moo gën 

281
00:58:03,147 --> 00:58:07,151
But it's your fault. That idea of cats 
You put it in my head

282
00:58:09,445 --> 00:58:13,032
Not cats
the cat

283
00:58:13,115 --> 00:58:14,783
Yes, a cat

284
00:58:14,867 --> 00:58:16,911
A killer cat 

285
00:58:16,994 --> 00:58:20,664
Jaar-jaar bii amna lu muy tekki ci janngalekat Miles

286
00:58:20,748 --> 00:58:23,334
Correct me if I'm wrong

287
00:58:23,417 --> 00:58:25,461
Jafe-jafe bi mooy, juumuwoo ci 

288
00:58:25,544 --> 00:58:28,380
Do you know Miles?

289
00:58:28,464 --> 00:58:30,424
Ku nekk ci dëkk bi xam na ko

290
00:58:30,507 --> 00:58:34,220
Ak ndax dégg nga jaar-jaar yi ñuy nettali ci moom?

291
00:58:35,137 --> 00:58:37,056
Amaana xamuma ko lu ëpp kàddu

292
00:58:56,033 --> 00:58:59,119
...Lu tax ci sa akademi?

293
00:58:59,203 --> 00:59:01,997
Ndax jàngale wuñu parapsychologie?

294
00:59:02,081 --> 00:59:04,875
Mën nañu ko woowe luxus bu ñuul 

295
00:59:04,959 --> 00:59:10,047
Barina luñu mëna seentu ci muus mu am xel 
dugg ci néeg sàcc caabi gi  

296
00:59:10,130 --> 00:59:12,466
Soo noppee nga dagg fiil bi

297
00:59:12,549 --> 00:59:16,804
Du loolu rekk. 
Nañu lakk këru Lilian

298
00:59:18,138 --> 00:59:21,016
Nanu jàpp ne jumtukaay rekk la

299
00:59:21,100 --> 00:59:24,770
Te keneen moo jiite xelam

300
00:59:24,853 --> 00:59:26,981
...nit 

301
00:59:27,064 --> 00:59:29,024
Dédeet, lii du xalaat bu baax 

302
00:59:29,149 --> 00:59:31,485
Booy seet, teori bi dof la

303
00:59:31,568 --> 00:59:35,322
Ak benn theorie biy leeral mbir yi xew ci jamono yii 

304
00:59:37,491 --> 00:59:40,119
Ndax dama wara yëgal mbir yooyu yépp London?

305
00:59:41,578 --> 00:59:44,957
Xamoo leen sama patroŋ, Larry Flynn
Ndax xam nga limu ma wax ?

306
00:59:45,040 --> 00:59:47,293
Gurley, bul nekk ak màndikat yu mel noonu

307
00:59:47,376 --> 00:59:50,713
Ngir liggéey bi bañ fa dem
Amaana danga wara wàññi tuuti li ngay lekk

308
00:59:54,425 --> 00:59:56,844
Soo bëggee am tontu li, danga wara ray sa bopp

309
00:59:56,927 --> 00:59:59,138
Yaakaar naa ni yaw itam 
Moo gën ñàkka toppatoo

310
01:00:00,806 --> 01:00:03,183
Ndax leegi xamoo 
Lu xew ci sama yuur?

311
01:00:05,394 --> 01:00:08,647
Mën naa xalaat 
Te amul lenn lu ci jaarul yoon

312
01:00:59,656 --> 01:01:01,992
Mënu ma ko tere 

313
01:01:03,535 --> 01:01:05,871
Déggatul ma

314
01:01:07,623 --> 01:01:10,209
Dara mënu ko tëye

315
01:01:12,336 --> 01:01:14,838
...ba ci dee

316
01:01:14,922 --> 01:01:17,883
Dañu ko daan

317
01:02:48,932 --> 01:02:50,893
déet

318
01:02:51,977 --> 01:02:53,770
déet

319
01:04:07,844 --> 01:04:11,306
Bëgguma woon lii 

320
01:04:11,390 --> 01:04:14,351
Danga wara def lii

321
01:04:15,936 --> 01:04:17,980
Ñaata yoon laa ko wara wax?

322
01:04:18,063 --> 01:04:20,649
wala màndiwoon 
Wala mu bëggoon ray boppam 

323
01:04:20,732 --> 01:04:24,570
Danga nekkoon ci trotoire bi, danga jaaxle 
Dama tëmb ci kanamu sama oto 

324
01:04:24,653 --> 01:04:26,738
...Melokaanu jaar-jaar bi noonu la

325
01:04:32,578 --> 01:04:35,372
Melni ku ko santaane?

326
01:04:35,455 --> 01:04:37,624
Lu nga bëgga wax ci ndigal?

327
01:04:37,708 --> 01:04:39,459
xaar

328
01:04:43,839 --> 01:04:47,634
...wax ngama ni ay tànkam

329
01:04:47,718 --> 01:04:49,970
Daa melni dafay liggéey ci boppam

330
01:04:50,053 --> 01:04:53,015
Waaw, dafa nuru robot 

331
01:04:57,311 --> 01:04:59,563
Ndax gis nga muus?

332
01:04:59,688 --> 01:05:00,647
muus mi

333
01:05:00,939 --> 01:05:03,567
Waaw, ci trotoire bi 
Fan la nekkoon 

334
01:05:03,650 --> 01:05:06,570
...balaa muy sànni ci suufu sa oto
muus mu ñuul 

335
01:05:06,653 --> 01:05:10,365
Madam, jàpp naa ni amul benn njariñ 
Ndax muus amoon na fa am déet?

336
01:05:10,449 --> 01:05:13,118
Gëmleen ma, lu am solo la 

337
01:05:13,702 --> 01:05:16,747
mbaa
Jéemal fàttaliku

338
01:05:16,830 --> 01:05:18,915
Xaaral ma xalaat 

339
01:05:18,999 --> 01:05:21,668
Muus mu ñuul 

340
01:05:21,752 --> 01:05:23,837
saw
Waaw, sama waajur 

341
01:05:28,800 --> 01:05:30,427
Maa ngi fàttaliku 

342
01:05:32,304 --> 01:05:34,765
Inspektër Flynn mingi bàyyi Londres 

343
01:05:34,848 --> 01:05:36,391
Dina yegsi ci ñaari waxtu

344
01:05:53,200 --> 01:05:55,035
Xamoon nga 

345
01:05:55,118 --> 01:05:57,162
Danga ko wara tere 

346
01:05:57,245 --> 01:06:00,040
Demal nga ànd ak man 

347
01:06:07,214 --> 01:06:09,299
fii laa ko suul 

348
01:06:15,847 --> 01:06:17,849
ana démb ci guddi gi

349
01:06:19,226 --> 01:06:21,395
Mani... dee

350
01:06:21,478 --> 01:06:23,647
Amul lenn lu bon luy xew 

351
01:06:23,730 --> 01:06:26,024
Lu xew Gurley?

352
01:06:26,108 --> 01:06:31,446
Aksidaa la woon... loolu rekk la

353
01:06:39,413 --> 01:06:43,500
Mbindéef bu soxor la
Dina may ray mu gaaw wala mu yagg

354
01:06:43,583 --> 01:06:48,046
Mbindéef bu soxor la
Dina may ray mu gaaw wala mu yagg

355
01:07:53,278 --> 01:07:56,072
<i>Maa ngi seeti ñi dee</i>

356
01:07:56,156 --> 01:07:58,909
<i>Maa ngi enregistre seen baat</i>

357
01:07:58,992 --> 01:08:01,912
<i>Dinaa dindi rido bi ci kumpa bu mag bi</i>

358
01:10:58,838 --> 01:11:00,924
Mënu nu </i>

359
01:11:36,084 --> 01:11:40,922
<i>Sur le Pont d'Avignon
Ci kaw y dëgër, Ci kaw y dëgër...</i>

360
01:14:11,239 --> 01:14:12,991
Feñ ngama

361
01:14:13,074 --> 01:14:16,035
Mën wéy di wax dëgg

362
01:14:17,078 --> 01:14:21,374
Jéem naa ko yàq
Waaye mënu ma 

363
01:14:22,625 --> 01:14:26,880
Ndax baayima boobu def na ñaawtéef yooyu yépp?
amul sikki-sakka

364
01:14:28,298 --> 01:14:30,675
Waaye amaana amna ku ko jiite 

365
01:14:30,758 --> 01:14:34,804
Muus yi duñu nangu komànd ci kenn, sama xarit 

366
01:14:36,514 --> 01:14:38,975
Komànd yiñ gëna xam

367
01:14:39,058 --> 01:14:43,521
Waaye wax nga lu jëm ci dooley xel mu doomu aadama

368
01:14:44,480 --> 01:14:46,858
Mën-mën yu kenn mënul xalaat 

369
01:14:48,443 --> 01:14:52,238
Yaa ngi fàttaliku... kenn mënu la daan 

370
01:14:55,533 --> 01:14:57,118
Yaa leen ray 

371
01:14:58,870 --> 01:15:01,164
Ak kàttan yu ëpp

372
01:15:03,208 --> 01:15:05,418
Jëfandikoo nga muus mi ni ngannaay 

373
01:15:06,586 --> 01:15:08,671
Arme bu bon

374
01:15:09,297 --> 01:15:11,424
Dugg nga ci xelam

375
01:15:11,507 --> 01:15:15,303
Ngir def sa pexe yu bonn yiy ray nit

376
01:15:18,056 --> 01:15:20,350
Yaa ngi ko noot te 
Mu indi ko ci ndigalam

377
01:15:22,101 --> 01:15:25,313
Ba noppi nga wax ko mu ray-
déet-

378
01:15:26,314 --> 01:15:29,817
Li ngay wax jaarul yoon

379
01:15:31,861 --> 01:15:35,782
Monstre boobu la woon 
Moo xëcc sama bañeel guñu tënk 

380
01:15:36,783 --> 01:15:38,993
Ak bàyyi sama mer 

381
01:15:39,869 --> 01:15:42,330
Ngir ñi ma xamul

382
01:15:44,123 --> 01:15:48,503
Ngir wéet ak wéet
Tëj ma ci biir

383
01:15:49,087 --> 01:15:53,633
Boobu monstre ci sama wàll wu lëndëm rek la
. Dafa doon digal

384
01:15:53,716 --> 01:15:57,220
Seytaane bi nëbbu ci sama biir
.as ci ñépp

385
01:15:58,137 --> 01:16:03,810
Waaye bima xamee lii ak dooley yàq ko
Xam naa ko, yàgg na lool

386
01:16:04,686 --> 01:16:09,482
di dundu 
waaw, daan-

387
01:16:09,565 --> 01:16:14,570
Daf ma daan 
Te mu gëna ma am doole .

388
01:16:14,654 --> 01:16:18,950
Yaxx na sama bëgg-bëgg ak sama bëgg-bëgg

389
01:16:19,033 --> 01:16:22,412
Leegi ak leegi
Dafay joxe ndigal rek

390
01:16:22,495 --> 01:16:26,541
Ku soxor la

391
01:16:26,624 --> 01:16:30,837
...te man maay jaamam

392
01:16:33,298 --> 01:16:38,344
Leegi moom mooy sama boroom

393
01:20:15,686 --> 01:20:19,565
Du kër 
Demb ci guddi gi Mme Miller gisu ko

394
01:21:37,768 --> 01:21:41,564
Yaakaar nga ni dafa dem? 
melni xale yu jigéen yu baax te rafet-

395
01:21:41,647 --> 01:21:44,984
Lu tax mu bàyyi ko?
Amaana ndax dafa ragal-

396
01:21:45,067 --> 01:21:48,195
Ak xew-xew yooyu yépp, mën nañu ko xam

397
01:21:56,162 --> 01:21:59,040
Nataal yi mu def bimu ñëwee fi

398
01:22:00,374 --> 01:22:03,085
Man ci jamono ak barab bu gëna doywaar
Daje naa ak moom 

399
01:22:03,169 --> 01:22:06,005
Leegi bàyyi na lépp, ci anam wu yomb

400
01:22:06,088 --> 01:22:09,258
... lu doywaar la
Nataal yooyu amoon nañu solo lool ci moom

401
01:22:11,135 --> 01:22:13,763
Nit ñi dañuy dem doonte dañu gaaw

402
01:22:13,846 --> 01:22:16,098
Coono ay weer yu néew sànniwul liggéey bi . 

403
01:22:55,471 --> 01:22:59,225
Hipnose par gats?
Gurley, danga dof?

404
01:22:59,892 --> 01:23:03,187
Loolu mooy lima bëggoon
. Gëmleen ma, màndiwoon naa

405
01:23:03,312 --> 01:23:06,399
Ndax gëm nga ni màndiwoo leegi?

406
01:23:09,860 --> 01:23:11,696
waaw

407
01:23:12,363 --> 01:23:14,865
Wilson, jàppale ma sol-
...sëñ bi, jàpp naa ni-

408
01:23:14,949 --> 01:23:17,576
Dimbali ma, bunu yàq sunu jotu

409
01:23:19,120 --> 01:23:22,039
Am nga muus wala amoo, xale bu jigéen bi mooy sa loraange

410
01:24:55,007 --> 01:24:58,469
Jàngalekat Miles, jàmm ci guddi gi
Inspectër Flynn bëgga waxtaan ak yaw

411
01:25:00,179 --> 01:25:02,848
guddi gu neex-
guddi gu neex-

412
01:25:02,932 --> 01:25:04,850
Inspektër Gurley itam def ko

413
01:25:04,975 --> 01:25:07,228
Amoon nanu mbégte xamante, ndax fàtte nga ko?

414
01:25:09,355 --> 01:25:11,774
...waaye def nga aksidaa

415
01:25:12,775 --> 01:25:15,694
Amul woon lenn lu am solo. Yenn xoosu surface

416
01:25:20,908 --> 01:25:25,162
Bëggoon nanu xam ni Madam Jill Trevors
Ndax mu ngi woon fi tay am déet?

417
01:25:26,372 --> 01:25:30,584
Jill? waaw 
Dafa ñëw ngir tàggatoo 

418
01:25:30,668 --> 01:25:33,879
Muni ma dafa wara dellusi ci saasi

419
01:25:33,963 --> 01:25:36,340
Am nanu ay sikki sakka, ngir dëggu 

420
01:25:36,423 --> 01:25:38,926
Danu jàpp ni beneen sabab la tax mu ñëw fi 

421
01:25:39,927 --> 01:25:41,804
lu waral

422
01:25:41,887 --> 01:25:44,849
Xoolal ndax sa muus mingi dundu

423
01:25:44,932 --> 01:25:47,226
Ay dof

424
01:25:47,309 --> 01:25:50,479
Lu tax nga wara toppatoo muus?

425
01:25:50,563 --> 01:25:52,648
...du muus

426
01:25:52,731 --> 01:25:54,817
muus woowu

427
01:25:56,026 --> 01:25:59,572
Sama muus dee na

428
01:26:00,948 --> 01:26:03,367
Ndax baax nga xoolaat liko wër?

429
01:26:04,910 --> 01:26:09,582
Wut nga muus
Ndax yaa ngi wër Jill?

430
01:26:11,166 --> 01:26:13,252
Sama gaa yi, ñëwleen ànd ak man

431
01:26:13,335 --> 01:26:15,671
Saytu fépp foo bëggee

432
01:26:18,924 --> 01:26:21,176
Nanga nangu sunuy jéggalu. 
Xalaatal ni sa kër la.

433
01:28:48,532 --> 01:28:50,159
déet

434
01:28:54,997 --> 01:28:57,249
Bëgguma woon 

435
01:29:02,588 --> 01:29:05,466
Musu ma xalaat ray nit

436
01:29:11,555 --> 01:29:15,184
Monstre bu soxor la woon

437
01:29:17,186 --> 01:29:19,646
...Daf ma forse 

438
01:29:27,738 --> 01:29:30,991
Nu ngi doon sàcc sunu moroom

439
01:29:34,078 --> 01:29:36,497
Te bii yoon moom moo jël ndam li

440
01:29:39,083 --> 01:29:41,376
Dina ma bàyyi ci loxo ki may ray


